DOSSIER 18 SAFARFLASH INFOS
Déclaration Seex Baasiru Mbàkke Ibn Seex Abdul Xaadir
https://www.youtube.com/watch?v=pR3iGCydvIU
Ndigalul Sëriñ Muntaxaa Mbàkke jëm ci Waaj taayu Màggal gi kàdduy Ndigal jëm ci dikkug jiitul Réew mi ak Ninu wara nekkee ci dëkk bi nuy wormaal bépp kilifa bufi ñëw yokk a wormaal dëkk bi ta gëna rafetal dëkkiin wi ci mbedd yi ak tali yi.